A travers cette chanson, Coumba Gawlo invite à l’espoir, dans un contexte où les sources d’inquiétude et de désarroi sont multiples. Soleil, un appel à un retour aux sources et à la résilience, est une réponse conséquente aux aspirations des citoyens, la jeunesse en particulier. Des paroles qui interpellent, pour qu’enfin l’espoir soit restauré et que le chemin d’un avenir meilleur soit illuminé par les rayons du Soleil.
Paroles :
Nadj bi fenk né tek
Drapeau bi ci kaw mi ngui né tek
Liir bangui dioye niou nakh ko mou né tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek
Armel yi sedd né tek
Ngoné Latyr thieu dékheulé tek
Imam ak labé yague def tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé
Ahmadou Kaabar guedj gui né tek
Limamou né ko Laye guedj gui né tek
Baye Niass khamal la ngua kham né tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek
Sunu taarikh mingui niou khol né tek
Médina Gounass, ndiassane, Thiénaba tek
Wakh diou bone noppé ko gueune
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Ndeyssane yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé
Moudiou gou rafet mo diara niane
Lolou motakh bima dégué Gawlo yaye sunu ndaanane
May lathie ndakh mba dina ko moudjé ndakh
Nietti att mou rothie sama baat mané tek
Tivavouane néma tallal lokho teu nel tek
Ndakh falaises bandiagara yague def tek
Loutakh nitt gni di wakh di wakh di wakh rek
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Vert Jaune Rouge yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Lac rose né dou changer teu dina rose batay dji
Mba dinako moudjé… (moudjiéeeeeeeeee)
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Bepp nguur nangua guestu sa askane
Yene ak niome yénéy moudjé
Bou yomal khiyamé yalla yeureumeulma sénégalais
Guem na né nonou lay moudjé
Soleil sur nos terreurs, sur notre Espoir
A quand viendras-tu Soleil sur nos erreurs
Sénégalais yague ngua done ndaanane
Mba di ngua ko moudjé