► Get the album / écoutez l’album :
“Xel“ (2001) : Grand Prix de l’Académie Charles Cros et Choc du Monde de la Musique.
Xel Xalat ne lu xoll yëgul
Yëngu yëngu danel ne guy wele
Sëlëx sul ne kan wele
Degg lu degg lu war la cë
(ter)
La raison a surpris le cœur
Un tremblement a déraciné ce baobab
Et cicatrisé la terre
Ecoutez ! Il ne suffit pas d’entendre pour comprendre
(ter)
Genn xalat nax ne aduna
Am sa lal lu bax le ci
Nax sa dolle tëcu ngi ci
Yagg dindi na tuma yëlle yëlle yëlle
(bis)
La pensée unique trompe le monde
Il est bon de causer à son oreiller
Surestimer sa force peut vous jouer un tour
Le temps révèle les vérités
(bis)
Aduna aduna Ama aduna li du neegu nara
La vie, la vie Ama, ne vaut pas la peine de se faire du mal
Xin lax na jant bi, xam sa waru gar jëf jël ngi ci
Yem fu mu leere lu bax le ci
Jamono ngi ni jamono jamono nge jamono ngi ni…
Le ciel s’assombrit voici le moment de se décider
Aller au-delà de la nuit
C’est aussi ça la vie, l’air du temps
Pecum liir su neexe ndeey jë teew ne
Teyye ne mbagg ye
La danse du bébé est belle
Quand se mère le tient par les épaules
Xarum waay
Gainde waay eï…
Mouton pour les uns
Lion pour les autres eï…
Luy tëpp dal ci taal dessene ap jeggo
Wolof Nnjaay ne në me lile woor na, lile woor na
Lile leer na ma
Sauter sur le feu contraint à ressauter
Un sage wolof me l’a dit
C’est clair
Assaman yaa ne bëtt du ci buxante
Yallah maay bëtt jam
Te bëtt
Fu ko neex lay xool
Le ciel est vaste, tous les regards y ont leur place
Dieu a doté ses créatures
D’yeux
Et les yeux regardent où ça leur chante
Xarum waay
Gainde waay eï…
Mouton pour les uns
Lion pour les autres eï…
Xin lax ne jant bi ey waay nu dem
Xin lax ne jant bi ey waay nu wey
Xin lax ne jant bi ey waay nu dem (ter)
Un nuage noir a caché la lumière, allons y
Un nuage noir a caché la lumière, allons y
Un nuage noir a caché la lumière, allons y (ter)
Xin lax ne jant bi
demal demal demal
Xin lax ne jant bi ku demul ma dem
Xin lax ne jant bi ey waay nu dem (bis)
Un nuage noir a caché la lumière, allons y
si vous n’y allez pas, moi j’y vais
Un nuage noir a caché la lumière, allons y
Un nuage noir a caché la lumière, allons y
Ah ! Ah ! …Xel lu bax la ci,
aduna, suma xel, suma xol, sumaï xalaat
Ah ! Ah ! …Il est bon de réfléchir,
c’est la vie, la raison, le cœur, les pensées
1 view
331
80
2 years ago 00:42:48 1
El Hadj El Hachmi Guerouabi___الحاج الهاشمي قروابي___هاجو لفكار
3 years ago 01:30:32 1
اجمل اغاني محمد غافورالمقطع El Hadj Med El Ghaffour 1
11 months ago 00:05:15 1
El Hadj N’Diaye - Xel
11 months ago 00:20:26 1
Hadj el Ghafour حاج الغافور
11 months ago 00:03:52 1
El Hadj N’Diaye - Kaki
9 years ago 00:01:33 35
PROMO WFL SUPERFIGHT Mohamed Khamal Vs Chahid Oulad El Hadj
9 years ago 00:07:07 1
Chahid Oulad El Hadj vs Mohamed Khamal
3 years ago 00:13:55 4
2010.К Zambidis vs Chahid Oulad El Hadj
5 years ago 00:04:48 1
Kizombada Taller EL HADJ & LYSIS
2 years ago 00:12:15 1
El Hadj El Hachemi Guerouabi Allah Yarahmou El Harraz الحرّاز
3 years ago 00:16:46 1
En 1969, El Hadj Mohammed Ghaffour باب الزمان
13 years ago 00:11:03 303
Dzhabar Askerov vs Chahid Oulad El Hadj @ Rumble of The Kings 2011
4 months ago 00:16:21 1
Mehdi Ait El Hadj v Don Sno | GLORY 93
12 years ago 00:01:15 51
Scott Brown celebration vs Rangers El Hadj Diouf
5 years ago 00:07:13 2
Samy El Maghribi et Hadj Ahmed Piro
3 years ago 00:56:06 1
El Hadj Mohamed Ghaffour de Nédroma - Noubat Sika -
10 years ago 02:02:54 189
Xala
1 year ago 00:07:44 1
Hadj M’Hamed El Anka - Al hamdou li Allah
10 years ago 00:03:53 1
Chahid Oulad El Hadj VS Andy Souwer 1
11 months ago 00:05:52 1
Sid El Juge
10 years ago 00:03:02 3
Chahid Oulad El Hadj VS Andy Souwer 3
3 years ago 00:23:18 1
Hadj Mohamed el Ghaffour - Sidi Man Sal Ala Hahl el Aïne